Categories
Android iOS Senegal Videos Wolof

Kaddu Gu Sell Gi

(“The Holy Scriptures” Podcast)

Kaddu gu Sell gi, Bibal bi maanaam Tawreet, Saboor ak Injil, mooy téere bi Yàlla wacce ngir leeral ak woomat bepp doomu Adama. Téere Saboor saar 119 aya 105 wax na, “Sa kàddu laay niitoo samay tànk, muy leeral samaw yoon.” Kurél biy defar Kaddu gu Sell gi, ci Dakar lay daje ayu bes bu nekk ngir wajal emission yu mëna barkeel nit ñi di leen jëmale ci Yàlla.

Kaddu gu Sell gi est un programme sur les Saintes Ecritures (La Bible). Dieu nous a donné la Bible pour nous guider dans la vie de chaque jour. Psaume 119 :105 «Ta parole est une lampe à mes pied et une lumière sur mon sentier. »